This podcast aims to showcase how the Murid lifestyle, founded by Cheikh Ahmadou Bamba, can bring about positive change, knowledge, peace, love, and understanding.
#66 - Woor Ngir Yalla | S. Ahmad Rafahi Mbacke
Woor weeru koor te Yalla rek tax.
3/31/2024 • 16 minutes, 18 seconds
#65 - Bess Penc Ak Lafay Xew | S. Ahmad Rafahi Mbacke
Bess penc ak lafay xew.
5/21/2023 • 18 minutes, 57 seconds
#64 - Noppi | S. Ahmad Rafahi Mbacke
Waxtaane lenn ci njariñu noppi
5/20/2023 • 18 minutes, 22 seconds
#63 - Kan Moy Cheikh Ahmadou Bamba | Serigne Sam Mbaye
Waxtaanu Serigne Sam Mbaye ci kan moy Cheikh Ahmadou Bamba Khadimu Rassul.
11/8/2022 • 2 hours, 52 minutes
#62 - Julli Fajar | S. Ahmad Rafahi Mbacke
Khutbah Serigne Ahmad Rafahi Mbacke Ibn Serigne Fallou ci julli fajar.
11/5/2022 • 18 minutes, 20 seconds
#61 - Al Qur'an | Serigne Sam Mbaye
Waxtaanu Serigne Sam Mbaye ci Al Qur'an ak diganté Serigne Touba ak Al Qur'an.
11/3/2022 • 1 hour, 37 minutes, 5 seconds
#60 - Akhiru Zaman | Serigne Sam Mbaye
Waxtaanu Serigne Sam Mbaye ci akhiru zaman (mujjuk jamono).
11/1/2022 • 27 minutes, 50 seconds
#59 - Akhi Jekër Ak Jabar | Serigne Sam Mbaye
Waxtaanu Serigne Sam Mbaye ci akhi dieukeur ak diabar.
10/31/2022 • 40 minutes
#58 - Fonk Waxtu | S. Ahmad Rafahi Mbacke
Litakh Yalla bind ñu.
10/28/2022 • 17 minutes, 29 seconds
#57 - Aji Makkah | S. Ahmad Rafahi Mbacke
Lan moy deuggi deuggi Hajj ak litax jullit bi warko def ak nimukoy defe.
5/13/2022 • 16 minutes
#56 - Ligeey Ak Jaamu Yalla | S. Lamine Toure
Linu mana roy ci Sokhna Mulimatu Mbacke Bint Khadimu Rassul.
5/9/2022 • 24 minutes, 36 seconds
#55 - Linu Koor Gi Jangal | S. Ahmad Rafahi Mbacke
Li beep jullit wara jangé ci woor weru koor gi bamu jeex.
5/6/2022 • 13 minutes, 50 seconds
#54 - Yaru Serigne Bi | Imam S. Cheikh Gueye
Ni Serigne Touba daan yaré Murid yi.
5/3/2022 • 44 minutes, 3 seconds
#53 - Murum Koor | S. Ahmad Rafahi Mbacke
Lan moy Murum Koor, manam Zakatul Fitr, ak kan moko wara joxé, naka lankoy joxé, ak kañ lañ ko wara joxé ak kan ngako wara jox.
4/30/2022 • 31 minutes, 23 seconds
#52 - Aduna | Serigne Sam Mbaye
Naka la jullit bi mana def ba japp diinem ak mucc ci yaxu yaxu aduna bi.
4/27/2022 • 30 minutes
#51 - Waxtaan Wi Serigne Touba Mujjé Def | S. Cheikh Fat Tacko Diop
Waxtaan wi Serigne Touba mujjé def, ci kadduk Serigne Cheikh Fat Tacko Diop (nijaayu Serigne Mourtada).
4/26/2022 • 1 hour, 25 minutes, 36 seconds
#50 - Fattaliku Yalla | S. Abdul Ahad Mbacke
Waxtaanu Serigne Abdul Ahad Mbacke Ibn Khadimu Rassul ci litax nitt ku nek war di sant ak fattaliku Yalla Sunu Borom.
4/24/2022 • 1 hour, 14 minutes, 33 seconds
#49 - Ndigalu Yalla | S. Ahmad Rafahi Mbacke
Litakh ku nek ci ñun wara gorgorlu ci top ndigalu Yalla yi.
3/6/2022 • 13 minutes, 55 seconds
#48 - Lewet | S. Ahmad Rafahi Mbacke
Lewet ak saye mbokk jullit ak nit ñi.
2/26/2022 • 20 minutes, 26 seconds
#47 - Wakh ak Noppi | S. Ahmad Rafahi Mbacke
Li nek ci wakh ak limu mana yakh walla defar, ak li waral noppi ci yenn yi di bakh.
2/19/2022 • 16 minutes, 56 seconds
#46 - Giss Yalla | Serigne Sam Mbaye
Ndakh nit meun na giss Yalla ak kan moko massa giss? Serigne Sam Mbaye di indi ay leral ci lolu.
2/16/2022 • 30 minutes, 58 seconds
#45 - Muñ | S. Ahmad Rafahi Mbacke
Naka la jullit bi wara def ak nattu buko Yalla tek.
2/12/2022 • 14 minutes, 6 seconds
#44 - Beug Serigne Touba | Serigne Sam Mbaye
Li beug Serigne Touba di def ci talibe bi.
2/8/2022 • 29 minutes, 48 seconds
#43 - Solos Julli | S. Ahmad Rafahi Mbacke
Solo si julli am ci lislam ak litax ku nek warko fonk.
2/5/2022 • 17 minutes, 57 seconds
#42 - Ay Teggin | Serigne Sam Mbaye
Lan moy ay teggin ak jikko you rafet ci niko Serigne Touba jangalé
2/2/2022 • 30 minutes, 18 seconds
#41 - Melow Sunu Borom | Serigne Sam Mbaye
Melow Sunu Borom ak ninu ci wara xalaaté
2/1/2022 • 29 minutes, 44 seconds
#40 - Charte Ñaan | Serigne Sam Mbaye
Lan moy chartou ñaan Yalla Sunu Borom
1/30/2022 • 5 minutes, 56 seconds
#39 - Aduna | S. Ahmad Rafahi Mbacke
Aduna ak lici biiram. Nimuy woré nit kiko def keur.
1/28/2022 • 16 minutes, 24 seconds
#38 - Borom Touba | S. Ahmad Rafahi Mbacke
Li wutalé Serigne Touba ak Borom Touba. Kan mociy kan?
1/24/2022 • 46 minutes, 6 seconds
#37 - Jikko You Rafet | S. Ahmad Rafahi Mbacke
Jikko you rafet te kawé yi Yonentebi amon te ñu warko roy ci mom.
1/21/2022 • 21 minutes, 30 seconds
#36 - Wut Alal | S. Ahmad Rafahi Mbacke
Sakku alal ju lew; bayyi di jel alalu jambur.
1/16/2022 • 31 minutes, 56 seconds
#35 - Jikko, Xel ak Xol | S. Bassirou Mbacke Khelcom
Diganté jikko, xel ak xol. Li topp baneex walla topp merr di yobbé nitki.
1/16/2022 • 5 minutes, 40 seconds
#34 - Yermande Yonentebi | S. Ahmad Rafahi Mbacke
Lenn ci yermandey Yonentebi Sallal Laahu Alayhi Wa Sallam.
1/14/2022 • 15 minutes, 22 seconds
#33 - Noni Nitt Ki | S. Sam Bousso
Ñeenti noni nit ki (manaam Bakkan, Shaytan, Baneex ak Aduna.
1/12/2022 • 26 minutes, 22 seconds
#32 - Salaatul Fatiha | S. Bassirou Toure
Lenn ci secrets Salaatul Fatiha.
1/10/2022 • 6 minutes, 47 seconds
#31 - Atté Yalla | S. Ahmad Rafahi Mbacke
Atté Sunu Borom ci nit ñ ak kurel yi. Ku nek ci ñun wara bayi xel bess bamuy jakaarlo ak Boromam.
1/7/2022 • 24 minutes, 31 seconds
#30 - Yaram vs. Rooh | Serigne Sam Mbaye
Diganté yaram ak rooh, kuci nek ci ñom ñaar ak senub ande.
1/4/2022 • 31 minutes, 35 seconds
#29 - Bess Bu Dellusi | S. Ahmad Rafahi Mbacke
Bess bu dellusi ak at mu bess.
12/31/2021 • 15 minutes, 36 seconds
#28 - Salaatu Alan Nabi | Part 1 | S. Bassirou Toure
Njariñu julli ci Yonente bi Sallal Laahu Alayhi Wa Sallam.
12/29/2021 • 22 minutes, 44 seconds
#27 - Xalaat | S. Ahmadou Mbacke
Litax nit ku nek war di beru di xalaat.
12/27/2021 • 1 hour, 27 minutes, 11 seconds
#26 - Joxé | S. Ahmad Rafahi Mbacke
Joxé luy jariñ sa morom.
12/24/2021 • 14 minutes, 36 seconds
#25 - Baatin | S. Saliou Sow
Mbirum baatin ak rooh.
12/22/2021 • 23 minutes, 1 second
#24 - Mirass | S. Modou Kara Diop
Mirass walla donnu ku faatu. Kan mo wara donnu ak ku ci nek lan nga wara am.
12/20/2021 • 1 hour, 42 minutes, 48 seconds
#23 - Kennal Yalla | S. Ahmad Rafahi Mbacke
Kennal Sunu Borom te bayi diko wutal morom.
12/17/2021 • 22 minutes, 5 seconds
#22 - Yitté | S. Bassirou Mbacke Khelcom
Yitté ju kawé.
12/15/2021 • 23 minutes, 54 seconds
#21 - Jibril | Serigne Sam Mbaye
Sayyidina Jibril Aleyhi-s Salaam.
12/13/2021 • 22 minutes, 15 seconds
#20 - Denkaane Yonentebi | S. Ahmad Rafahi Mbacke
Denkaane Yonentebi Sallal Laahu Alayhi Wa Sallam.
12/10/2021 • 14 minutes, 30 seconds
#19 - Yermande Yalla | S. Bassirou Mbacke Khelcom
Yermande Sunu Borom ci mbindef yi.
12/8/2021 • 35 minutes, 59 seconds
#18 - Akhiru Zaman | S. Ahmad Rafahi Mbacke
Mujuk Jamono
12/3/2021 • 12 minutes, 50 seconds
#17 - Ngoro | S. Mbacke Abdou Rahmane
Ngoro ci Lislam
11/28/2021 • 12 minutes, 5 seconds
#16 - Xaru | S. Cheikh Abdou Diop
Atté xaru ci Lislam
11/27/2021 • 19 minutes, 20 seconds
#15 - Toob | S. Ahmad Rafahi Mbacke
Toobal Yalla Sunu Borom.
11/27/2021 • 16 minutes, 44 seconds
#14 - Bammel | S. Ahmad Rafahi Mbacke
Liy xew ci bir bammel
11/25/2021 • 43 minutes, 49 seconds
#13 - Ragal Yalla | S. Ahmad Rafahi Mbacke
Lan may ragal Yalla
11/19/2021 • 18 minutes, 16 seconds
#12 - Muccu Ci Saytaané | S. Ahmadou Mbacke
Naka ngay def ba muccu ci Shaytan
11/14/2021 • 4 minutes, 57 seconds
#11 - Seuy | S. Ahmad Rafahi Mbacke
Khutbah Imam Serigne Ahmadou Rafahi Mbacke ci seuy.
11/12/2021 • 21 minutes, 12 seconds
#10 - Xam Yalla | Part 2 | Serigne Sam Mbaye
Lan moy xam Yalla Sunu Borom (Tawheed), ci kaddu Serigne Sam Mbaye.
11/8/2021 • 7 minutes, 47 seconds
#9 - Xam Yalla | Part 1 | Serigne Sam Mbaye
Lan moy xam Yalla Sunu Borom (Tawheed), ci kaddu Serigne Sam Mbaye.
11/7/2021 • 32 minutes, 16 seconds
#8 - Yawmal Qiyam | S. Ahmad Rafahi Mbacke
Yawmal Qiyam (Bess Penc).
11/5/2021 • 19 minutes, 15 seconds
#4 - Yonente Yalla Ibrahim | Part 1 | S. Bassirou Mbacke Khelcom
Jaar Jaari Yonente Yalla Ibrahim ci kaddu Serigne Bassirou Mbacke Khelcom
5/20/2021 • 1 hour, 38 minutes, 44 seconds
#3 - Maam Adama | Part 2 | S. Bassirou Mbacke Khelcom
Jaar Jaari Sunu Mame Adama
5/19/2021 • 31 minutes, 39 seconds
#2 - Maam Adama | Part 1 | S. Bassirou Mbacke Khelcom